Ñi bëgg Yessu

Dalal ak Jamm ci turu Yessu

Ndaxte Yàlla dafa bëgg àddina, ba joxe jenn Doomam ji mu am kepp, ngir képp ku ko gëm am dund gu dul jeex te doo sànku mukk.

Yowaana 3:16

Kan moy Yessu?

Ay sedde yu lay may dolle

Talibe ci Daara, daw dem Dakar, nekk fakk man, mujju jox dundam Yessu.

Mom ay wajuram da ño tassoon, kon yaro wul ak wajuram, waye Yessu wan ko mbegeel.

Mom jëriñ la won, tar biw doon majjal, di topp ndiggal, waye bayam dafa tupp.

Seede
El Hadji Sall

Seede
Aminata Ndiaye

Seede
Hamidou Diallo

Seede
Omar Doucoure

Senegal la juddo, dem Cote d'Ivoire, joggé dem Mauritanie tassé fa ak Yessu.

Xaritam jullit bu joox dundam mo ko xamal Yessu, lo jaxal ko dem utti kaddu gi.

Mbër bu doon takk ay galać, febar ame mettitu bopp waye Yessu faj ko.

Dadon jay sinebar, di tox, bëss ñu ramass ko, waye mo rëcc, Yessu mussal ci kasso.

Seede
Léna Gomis

Seede
Clémentine Manga

Seede
Grégoire Ñing

Seede
Pions Gomis

Mankañ bu don tuur ci xërëm yi, di genn tuur ak mamam, waye Yessu mussal ko.

Doxankate la woon, xamul Yessu, wayé Yessu wax ak mom, ci Youtube.

Seede
Marc Mendy

Seede
Alex Ndecki

Football la beggon def way bi ware dem bittim reew, Yessu tee ko.